infovihtal #97 Fagaaru ci walu sëy boole ak VIH - gTt-VIH

Anuncio
infovihtal 97
Fagaaru ci walu sëy boole
ak VIH
#
Amna lu baari lo mën def ngir ar sa bopp ar neneen ni ci VIH. Boole peexe yi dina tax
nga meengle fagaaru bi ak say bëgg bëgg.
Soo ame ség VIH, so de fàccu ba keen
du giis doomi jangoorro ci sa deret,
bubooba wale ko day jafé. Lolu tax ba
ngawar di jël say garab ci waxtu yi ak
liim bi un ka diggle, tami di setlu
sa deret sa sune.
en
e
g
ji
sune
? ?
? ? ??
ak/b
a sin
eebar
Set
lu
?
an¡
xta
Wa
Grupo de Trabajo
sobre Tratamientos
del VIH
na
ns
anŋ
ara
Sa so ame
Joote sëy bu andul
ak fagaaru ba bu and ak ndogal
( kapot bu tòc ba ñewal doole ci sëy), yoon
la nga dem Opital setlu sa bopp ci numu
gëna gaw . Doktoor di na nu xool ndax
VI
a
l
da nga waar jël garab yi xeex VIH
wa
ci diiru ñeenti ay bës ngir
u
n
arla, tax ba ség du jàpp
pë
p
sa yaram.
Re
H
?
nu
ëy: ¡
Njàngum fagaaru ci s
?
Di nan sanŋara ak/ba di jél
sineebar so dee Sëyante, day faràl di tax
ba nit nu baari du nu jittëllate fagaaru,
ñaaka seen sàggo ba du taan li gën
ci sëyante.
W
an
ni
[email protected]
www.gtt-vih.org
Barcelona (España)
?
Xam ndax amee
nga VIH day tax nga
mëna am ci yombal
yi ci walu fàcc, te
ngay mën Yamal say
yenŋu ci walu sëy.
Mën nga def setlu ci
lo dul faay ci sa kër
doktoor ba ci bërëb yi
saytu feebaru sëy yi
baneen bërëp bo koy
setlu.
Fagaaru ci
walu sëy
boole ak VIH
deret b
i sa
D SEXUAL
?
Am yeneen
ni feebaru sëy
day yokk walle
Doomi jangooro ji di
VIH. Setlu Fotollu ndax
feebaru sëy newul ci yaw, ak
pàccam , Day tax nga
moytu yokko ség bi. Mën
nga dem ci kër doktoor
yi un jagglel xettu
Feebaru sëy yi ci lo dul
fay dara.
VIH
ci
CENTRO DE SALU
Sunu Sëyante lu am
solo la ci dund gi. Di
ko waxtaane ak
neneen ci walu
werguyaram di na
tax nu ay tontu yu
baari ci sunu doxaliin
ba janxaare.
uf
ot
oll
u
yi
sëy
aru
feb
ni
Kapoot mo gëna
woor ci fagaaru ci VIH ak
yeneen xetti feebaru sëy.
Bu boole diiw rataxal yi
dey tax ba du tocc te
yombal ruffu gi.
Se
tl
en
ne
ye
Kap
oo
tg
oo
ra
kb
u
Pàccum xeex VIH
o
ess
w
bo
aw
n
n
à
ci g
Fagaaru
POR FAVOR, FOTOCÓPIALO Y HAZLO CIRCULAR
Subvencionado por:
Colaboran:
Programa de Prevenció i Assistència
de la Sida
Àrea de Qualitat de Vida, Igualtat
i Esports
Àrea de Benestar Social
Descargar